la llebre i el lleó

5
LE LION ET LA LIÈVRE II/ CONTE WOLOF Beena bis jabaru gaïnde mi buru ala bi , jabaram defa am doom mu getëne rabi ala yeep ngir gnou gnew ndookel jabaram ji ci doom ju goor ji mu am .Rabe ala yeep ba gnou gnew gnou nee mbam boul wax ngir baatam bu naxari . Ba nou gnewe ba waxtaane ba nopi Buru ala bi beeg .ce booba le mbam yuuxuu. Doomi gaïnde jee tiit daadi dee gaïnde Meer nee yenne yeep laye fad. Gnou dawu deem di waxtaan .Nou nuy muce ci meerom gaïnde mi, Gni nee na¨gnu ko jox mbam mu rey ko , Gnee gnu nee du tee mu fad nu . LEUK Bëuga wax gnou nee ko amoo ci baat. Gnou weur weur xelaat am gnou ko .Gnou nee leegi waxal yew leuk .Leuk nee waw joog deem. BA mu agee nee gaïnde degnou maa joxonn ab leuk ngir ma andil la ko way beneen gaïnde moo ko nangu , nee moy buru ala bi . gnewal gnou deem ma won la ko .Gaïde joog and ak meer BA gnou aksi ce teen ba mu nee ko yëurdu mungi nee .Cepul ci kawam nga rey ko gnou denluwaat . nga moom sa ngur .Gaïde ga def lola daa di

Upload: associacio-amics-de-diakha-madina

Post on 09-Mar-2016

223 views

Category:

Documents


4 download

DESCRIPTION

Conte de l'escola Backari Seck

TRANSCRIPT

LE LION ET LA LIÈVRE

II/ CONTE WOLOF

Beena bis jabaru gaïnde mi buru ala bi , jabaram defa am doom mu getëne rabi

ala yeep ngir gnou gnew ndookel jabaram ji ci doom ju goor ji mu am .Rabe ala

yeep ba gnou gnew gnou nee mbam boul wax ngir baatam bu naxari . Ba nou

gnewe ba waxtaane ba nopi Buru ala bi beeg .ce booba le mbam yuuxuu. Doomi

gaïnde jee tiit daadi dee gaïnde Meer nee yenne yeep laye fad. Gnou dawu deem

di waxtaan .Nou nuy muce ci meerom gaïnde mi, Gni nee na¨gnu ko jox mbam

mu rey ko , Gnee gnu nee du tee mu fad nu . LEUK Bëuga wax gnou nee ko

amoo ci baat. Gnou weur weur xelaat am gnou ko .Gnou nee leegi waxal yew

leuk .Leuk nee waw joog deem. BA mu agee nee gaïnde degnou maa joxonn ab

leuk ngir ma andil la ko way beneen gaïnde moo ko nangu , nee moy buru ala

bi . gnewal gnou deem ma won la ko .Gaïde joog and ak meer BA gnou aksi ce

teen ba mu nee ko yëurdu mungi nee .Cepul ci kawam nga rey ko gnou

denluwaat . nga moom sa ngur .Gaïde ga def lola daa di dee .Leuk gnibi si , nee

leen reyna ko .Gnou beeg . gnew ce teen ba jis ko mu tëude ci bir .

LU CI JEEL MOY : Gnou nee tuti tewta am xel

FRANÇAIS

Il était une fois le lion roi de la forêt organisait un baptême auquel il forçait

tous les animaux à y participer et à saluer sa femme .Tous les animaux ce sont

concerté avant de partir et ont demandé à l’âne de ne pas parler parce qu’ayant

la voix rauque .Toute la délégation s’est rendu chez le lion et a présenté le motif

de leur déplacement. Le lion en était très content. Aussitôt l’âne brait. Le fils du

lion mourut .Le lion se fâcha et jure de tuer tous les animaux. Les animaux se

réunirent à nouveau pour réparer la faute. Certains proposent de lui donner l’âne

pour qu’il le tue. D’autres disent que cela ne l’empêchera de nous tuer tous .Je

peux nous sortir de cette situation a dit le lièvre. Tais –toi tu es trop petit pour

parler ici ripostèrent les animaux. Après de longues heures de recherche sans

solution, ils revinrent demander au lièvre de faire sa proposition. Je m’en vais

lui parler et je vous sauverai. Arrivé chez le lion , il dit les animaux m’ont

chargé de venir te donner un lièvre pour faire plaisir à ta femme. Mais en venant

j’ai rencontré un autre lion qui me l’a arraché prétendant être le roi de la forêt .Si

vous n’êtes pas sûr venez je vous le montre. C’est ainsi que le lièvre a conduit le

lion jusqu’à un puits et lui a demandé de regarder au font. La silhouette du lion

apparaissant au font, le lièvre dit voilà c’est celui- là .Il a l’air plus petit que toi

si vous vous jetiez sur lui, nous allons en finir. Le lion s’y jeta et mourut. Le

lièvre alla dire aux animaux : je l’ai tué.

Moral. Être petit ne veut pas dire être plus petit.

CATALÀ

Hi havia una vegada el lleó rei de la selva que organitzava un bateig, al que obligava

a tots els animals a participar-hi, i a saludar a la seva dona. Tots el animals es van

reunir abans de sortir, i li van demanar a l’ase que no parlés perquè tenia la veu

ronca. Tots els delegats, van explicar el seu motiu del viatge al lleó, aquest n’estava

molt content, i de sobte l’ase va cridar. El fill del lleó va morir, el lleó es va enfadar i

va jurar matar a tots els animals. Els animals es van reunir de nou per reparar la

falta. Alguns proposaven donar-li l’ase per que el lleó el mates. D’altres deien: això

no li impedirà matar-nos a tots.

- Jo puc treure-us d’aquest embolic –va dir la llebre -.

- Calla!! tu ets massa petita per parlar aquí van contestar els animals. Desprès de

llargues hores de buscar la solució sense trobar-la van demanar a la llebre de fer la

seva proposta.

- Jo me’n vaig a parlar amb ell i jo us salvaré.

Arribant a casa del lleó, ella, la llebre, va dir :

- Els animals m’han encarregat de donar-te un regal perquè la teva dona estigui

contenta, però tot venint, he trobat un altre lleó que me’l ha pres, pretenent ser el rei

de la selva. Si no n’estàs segur, vine que t’ho ensenyo.

Es així, que la llebre va portar al lleó en un pou i li va demanar que mirés, al fons del

pou. Com que la silueta del lleó apareixia al fons, li digué la llebre:

- Mira es aquell, sembla mes petit que tu. Si et tires al damunt de l’animal acabarem

amb tot això. El lleó s’hi va tirar i va morir ofegat. La llebre els hi va anar a dir als

altres animals – Jo l’he matat-.

MORAL: Ser petit no vol dir que no pots aconseguir res per els altres.